EURO 2024

Yeneen i xët

Aji bind ji

Njureefi sumb bu njëkk bi

Sumb bu njëkk bi ñeel Ëro 2024 bi ca Almaañ jeex na ci àllarba jii weesu. Kippu gu ci nekk ñaar ñi jiitu ñooy jàll ca ñaareelu sumb ba ak ñeenti ñetteel yi gën a jekku. Ci sumb bees dëgmal nag, dóor mu toog la.

Toftaleg kippu yi :

Kippu A

Almaañ 7EURO 2024

Siwis 5

Ongiri 3

Ekos 1

Kippu B

Espaañ 9

Itali 4

Kurwaasi 2

Albani 1

Kippu C

Àngalteer 5

Danmàrk 3

Esloweni 3

Seerbi 2

Kippu D

Ótiris 6

Farãs 5

Peyi-Baa 4

Poloñ 1

Kippu E

Rumani 4

Belsig 4

Eslowaki 4

Ikiren 4

Kippu F

Portigaal 6

Tirkii 6

Seworsi 4

Repiblig Ceg 1

1/8 dë finaal yi nii lay tëddee :

Gaawu 29 suwe

Almaañ – Danmàrk 

Siwis – Itali

Dibéer 30 suwe

Espaañ – Seworsi 

Àngalteer – Eslowaki 

Altine 1 sulet

Portigaal – Esloweni 

Farãs – Belsig

Talaata 2 sulet

Rumani – Peyi-Baa 

Ótiris – Tirkii

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj