Xibaar EURO AK COPA AMERICA 2024 By Maam Usmaan Si Gómis 03/07/2024 0 175 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/4/2025) Mbay Sow - 17/04/2025 MBIRUM KOPPARI “FONDS FORCE COVID-19” Mbay Sow - 17/04/2025 DOKTOOR JÀLLO JÓOB : GOR CI WAX, GOR CI JËF Ndey Koddu Faal - 16/04/2025 LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/4/2025) Njuga Gay - 15/04/2025 Aji bind ji Maam Usmaan Si Gómis EURO 2024 Njureefi 1/8 dë finaal yi Ndajey 1/8 dë finaal yi ñeel Euro bi jeex nañ démb ci talaata ji. Nii la njuréef jonante yi demee : Almaañ 2-0 Danmàrk Siwis 2-0 Itali Espaañ 4-1 Siyoorsi Àngalteer 2-1 Eslowaki Portigaal 3-0 (seri) Esloweni Farãs 1-0 Belsig Rumani 0-3 Peyi-Baa Ótiris 1-2 Tirkii Naalu 1/4 yi 5 sulet 2024 Espaañ – Almaañ Farãs – Portigaal 6 sulet 2024 Peyi-Baa – Tirkii Àngalteer – Siwis COPA 2024 Njureefi kippu yi Gannaaw ba ekib yépp amalee seen i 3i mats ba noppi, nii di waaj a dikk la mbir yi demee ci kippu yi. Képp bu ci ne nag njëkkeel bi ak ñaareel bi ñooy kalifiye ñeel 1/4 yi. Kippu A Arsàntin 9 Kanadaa 4 Sili 2 Péru 1 Kippu B Wenesuwelaa 9 Ekuwaatëer 4 (+1) Meksig 4 (0) Samayk 0 Kippu C Iriguwey 9 Panamaa 6 Etaa-Sini 3 Boliwi 0 Kippu D Kolombi 7 Beresil 5 Kosta-Rikaa 4 Paraguway 0 Naalu 1/4 dë finaal yi 5 sulet 2024 Arsàntin – Ekuwaatëer 6 sulet 2024 Wenesuwelaa – Kanadaa / Kolombi – Panamaa 7 sulet 2024 Iriguwey – Beresil Maam Usmaan Si GómisPlus de publicationsBiographieMaam Usmaan Si Gómishttps://www.defuwaxu.com/author/maamusmaansigomis10/XIBAARI TÀGGAT-YARAMMaam Usmaan Si Gómishttps://www.defuwaxu.com/author/maamusmaansigomis10/PAAB CAW TÀNN NA AY GAYNDEEMMaam Usmaan Si Gómishttps://www.defuwaxu.com/author/maamusmaansigomis10/XIBAARI TÀGGAT-YARAMMaam Usmaan Si Gómishttps://www.defuwaxu.com/author/maamusmaansigomis10/XIBAARI TÀGGAT-YARAM FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj