Cubba Taal

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/1/2025)

MURIG MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM Ayu-bés bii ñu génn la Ngomblaan gi dooroon liggéey bi ba jotoon a taxawal ag ndiisoo. Suba, ci àjjuma ji, woo nañu dépite yi fa Ngomblaan ga. Li waral woote bi du lenn lu moy fénc càkkuteefu murig mbalaanu kiiraayu...

NDAJEM JËWRIÑ YI : ÑEENTI JIITUWAAYI NJIITU RÉEW MI

Ci àllarbay démb ji, 22i fani sãwiyee 2025, lees doon amal ñeentelu ndajem jëwriñ yi ci at mu bees mii. Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, moo jiite ndaje ma. Ca njeexital la, Aamadu Mustafaa Njekk Saare mi yor kàddug Càmm gi biral na...

UBBITEG DAARA YI

Ginnaaw ñetti weer i bër, ndongo yi ak jàngalekat yi fas yéene nañoo awaat...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 01 OKTOMBAR 2022)

PÓLITIG  Bitim-réew, ca Burkinaa Faaso, ñu nemmeekooti fa poqartim Nguur, ginnaaw juróom-ñatti weer kott ba...

GAALU JOOLAA, FÀTTE XAJU FI

Jéyya gënul réy suuxug gaalu Joola ga. Te, njaaxum du ko weesu. 20i at...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 24 Sàttumbar 2022)

PÓLITIG  Ginnaaw mbetteel ga mu am ca Ngomblan ga ca palum njiit la, ndax Aminata...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 10 Sàttumbar 2022

PÓLITIG  Ngi waajal màggalu Tuuba, wa YEWWI-WALLU amal nañu seen ub siyaar ci kanamu kilifag...

IMAAM ALIYUN NDAW, SA JAAN WÀCC NA !

Bakkan bu ñam dund, ñam dee. Ab xandeer bu damme cib waar moo wàcc....

SEEX AHMADU BÀMBA MBÀKKE, BOROOM 18 SAFAR

Dara judduwul cig neen. Mu mel ni, bànneex ci coono lay soqikoo, mbég ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 27 ut 2022

 PÓLITIG  Coow li amoon  ci diggante Gabriyel Kan ak jëwriñ ji ñu dénk mbiri jigéen...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/1/2025)

MURIG MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM Ayu-bés bii ñu génn la Ngomblaan gi dooroon liggéey bi...

NDAJEM JËWRIÑ YI : ÑEENTI JIITUWAAYI NJIITU RÉEW MI

Ci àllarbay démb ji, 22i fani sãwiyee 2025, lees doon amal ñeentelu ndajem jëwriñ...

CDEPS MI NGI SÀKKU CI NJIITU RÉEW MI MU « YEESAL WAXTAAN WI AK SAABALKAT YI »

Conseil des diffuseurs et éditeurs de presse du Sénégal (CDEPS) dafa doon amal, tay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/1/2025)

USMAAN SONKO : DUGG NAÑU CI JAMONO JOJ, BAALE JEEX NA Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko,...