Jëwriñu mbey mi, Sëñ Mabuuba Jaañ, amaloon na tukkib nemmeeku fa Sigicoor. Li mu ko dugge woon mooy saytuji ndefaru SONACOS ga nekk ca diiwaan boobee, rawatina sàqum peppi gerte yi.
Jubluwaay bi gën a réy bi njiiti réew mi sas Jëwriñ Mabuuba mooy fexe...