Mamadu Jara

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

CNRA DOG NA SIÑAALU iTV

Ngir fàttali, CNRA dafa artu woon rajo yeek tele yi ngir ñu bañ a...

BIRAM SULEY JÓOB, MBAA DU… ?

Gor, ca wax ja. Kàddu gilee génn démb ci gémmiñi saa-senegaal yu baree bare....

NJËGU DUND BI NJIITU RÉEW MI, MAKI SÀLL, JËL NA 11i NDOGAL

Ci gaawu gii weesu, 5i fan ci nowàmbar, lees doon amal am ndaje ngir...

SÉMBUB SOROJ BU GRANDE-TORTUE Senegaal dina taxan 20 000i miliyaar ci diirub 30i at  

Bu liggéeyub soroj bi tàmbalee, Senegaal dina taxan, ci diirub 30i at, 20 000i...

GIS-GISU FMI CI ËLLËGU KOOM-KOOMU SENEGAAL

Yokkuteg dundu gi nekk di lëmbe àddina si boobu ba léegi tax na ba...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Alxemes 13 oktoobar 2022

NJÀNG AK JÀNGALE  Ñàkkum ndox ca daara ju kowe jii di UADB Daara ju kowe jii...

YOMBALUG DUNDU GI, NISËRU NGUUR GI

Ci atum 2023 mii nu dëgmal, Nguur gi dafa fas yéene génne gafaka (budget)...

NDIMBALU 670 MILIYOŊ CI MBEYUM DARKASE BI

Kurél gii di DER/FJ (Délégation à l’entreprenariat rapide des femmes et des jeunes) moo...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA