Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee ngi waaj a song sémb yu mag yi ngir tabax réew mi. Looloo tax, ci Sémbuw Àtteb Ngurd mu 2026 mi, ñu sóoraale ci naaluw kopparal wu mag a mag....
Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii di Seex Ture faatoo ak ñan ñoo jël bakkanam. Dafa di sax, am na ku ñu duutagum baaraam, njort ne laale na ci mbir mi.
Bu dee li ñeel luññutu yi,...