Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

FAR NAÑU CAMPEEF YII DI HTTC AK CESE

Barki-démb ci gaawu bi lañu woo woon dépite yi fa Ngomblaan ga. Li waraloon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/12/2024)

SÉMBU ÀTTE14/2014 Ngomblaan gi dina ubbi ëllëg ci gaawu bi, 14i pani desàmbar 2024, bu...

YOON WOO NA BÀRTELEMI JAAS AK AADAMA GAY

Sànq ci bëccëg gi la xibaar bi rot. Moom, Bàrtelemi Jaas miy ndeyu-mbill ji,...

TUKKIB MAGUM JËWRIÑ YI FA GÀMBI

Démb, ci gaawu bi la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, demoon fa Gàmbi. Li...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/12/2024)

LIGGÉEY BA DOOR NA FA NGOMBLAAN GA Altine jii weesu lañu ubbi fukk ak juróomeelu...

UBBITEG NGOMBLAAN GU YEES GI

Tay, ci altine ji, ñaari fan ci weeru desàmbar 2024, lañuy ubbi Ngomblaan gu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/11/2024)

SAMIYEL SAAR DEM NA KASO Àjjuma jee weesu lañu ko tegoon loxo. Booba ak tay...

TËJANDI NAÑU JÀNGUNE BU SIGICOOR

Ginnaaw jàmmaarloo yu metti yi amoon Jànguneb Asan Sekk bu Sigicoor, kilifay daara ju...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA