Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

JÉYYA JU METTI FA MÉDINA BAAY

Xew-xew bu tiis boobu, mi ngi am démb, ci gaawu bi. Ma nga ame...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/11/2024)

DIC WOO NA AADAMA GAY Tay ci alxames ji lañu ko woolu, ñetti waxtu ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/11/2024)

NGUUR GU YEES GAA NGI WEEJI NGUUR GI FI JÓGE Démb, ci àllarba ji la...

LËNT-LËNT ÑEEL FAATUG MAMADU MUSTAFAA BA

Altine jee weesu, yemoo woon ak 4i pani nowàmbar 2024, la Mamadu Mustafaa Ba...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/11/2024)

UDS BU AJI MBERGAAN FEKKI NA PASTEF Fukki fan kepp a des ci wotey palug...

TUKKITEY NJIITU RÉEW MI FA ARAABI SAWDIT AK TURKI

Dibéer jee weesu la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tukki woon na....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/10/2024)

TUKKITEG NJIITU RÉEW MI FA TURKI Keroog la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay,...

NDOORTEELU KÀMPAAÑI WOTEY PALUG DÉPITE YI

Biig la kàmpaañ yi door. Kàmpaañ yooyu, ñi ngi war a jeex fukki fan...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA