Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

TABB YU YEES ÑEEL KÀNGAAMI YOON YI

Ci altine jii weesu lañu doon amal ndaje miy boole ak a tabb ñiy...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (Alxames 23 féewaryee 2023)

PÓLITIG Yeneen tabb yu yees  Ca ndajem jëwriñ ma mu doon amal démb, kii di Njiitu...

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ AK USMAAN SONKO

Démb, ci alxames ji lañu waroon a àtte Maam Mbay Ñaŋ ak Usmaan Sonko....

LI GËN A FES CI XIBAARI BÉS BI (Alxames 16 féewaryee 2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAN AK USMAAN SONKO Tey ci alxames ji lañu waroon a àtte...

YOOTE BI AM DIGGANTE MAKI SÀLL AK USMAAN SONKO

Lu tollu ci at kepp a des ci wote yi, coow li ne kurr...

LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (àjjuma 10 féewaryee 2023)

PÓLITIG Perefeb Mbàkke tere na mitiŋ ba Tey ci àjjuma ji la kii di Usmaan Sonko...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (àjjuma 2 féewaryee 2023)

PÓLITIG  Layoo Maam Mbay Ñaŋ Usmaan Sonko ajandi nañu ko Layoo bi waroon dox démb ci...

LAYOO USMAAN SONKO AK MAAM MBAY ÑAŊ

Coowal 29 miliyaari yi ñu ne woon dañu ko luubal ca PRODAC, dekkiwaat na....

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA