Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

PELENT YA JOLLI NAÑ

Téere Séex Yérim Sekk bi ak coowal Aji Saar-Usmaan Sonko ñooy ñaari xibaar yi...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 18 saŋwiye 2023

PÓLITIG Layoo Aji Saar-Usmaan Sonko Ñaari at daanaka bi coowal Aji Saar ak Usmaan Sonko tàmbalee...

Yewwi Askan Wi nangu na ndogal, jël ndogal

Caabalug ëttu cettantal gi mi ngi wéy di lëmbe réew mi, rawatina làngug pólitig...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 5 saawiye 2023

PÓLITIG Leerali Usmaan Sonko ñeel ñaxtuy ndongoy Sigicoor yi Ci ndajem-waxtaan mu mu doon amal tey...

MAAJOOR, BUL FÉETE BOOR

Ginnaaw bi ñu fésalee seen ag caabal ñeel yorinu FORCE COVID-9 bi, Ëttub cettantal...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (alxames 29 desàmbar 2022)

PÓLITIG Yeneen tàbb yu yees  Ca ndajem jëwriñ ma mu doon amal démb, Njiitu réew mi...

MAAMUR JALLO, KU ÑÉPP TUFLI NGA TOOY

Coowal Aji Saar ak Sonko, féewiryee 2021 la tàmbali woon. Ba tey ma ngay...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (Alxames 22 desàmbar 2022)

PÓLITIG                            Taxawaayu Seex Abdu Baara Dolli ñeel wotey 2024               Dépite bii di Seex...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA