Defu Waxu

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

SUNU GIS-GIS CI ''BLACK LIVES MATTER'' AK YENEEN XEETI ÑAXTU ÑEEL XEETAL AK ÑAAWTEEFI TAKK-DERI AMERIG YI (Kàddug mbooloom kàngami Mbootaayu Xeet yi fekk...

(Ci tekkig Ndey Koddu Faal) Njolloor, ca Minneapolis. Alkaatib Tubaab teg óomam ci kow loosu nit...

YOLOMAL BUUMU NJAAM GI NGIR GËN LAA XOJ, FARÃS DEFATI NA MËNINAM (Boos Ndóoy)

Boos Ndóoy Jikko ak boroom, sëg ya rekk ! Ndege, Farãs dafa am pexe moo...

USMAAN SONKO : « MAKI SÀLL CUUNE LA, DI DEF YËFI CUUNE. » (Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo, Daawuda Géy)

(Xaaj bu njëkku laaj-tontook Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo ak Daawuda Géy) LU DEFU...

JÀNG AK JÀNGALE CI JAMONOY MBAS (Safiyetu Béey)

SAFIYETU BÉEY Céy Koronaa ! Doomu-jàngoro bii yëngal na jamono. Ku mënoon a gëm lu ndawe nii...

‘’ÑAAWTEEF YIY XEW TEY RÉEWUM SIIN DU GULÉET…’’

(SÉEX MBÀKKE AMAAR, JËWRIÑUNDONGOY-DAARA SENEGAAL YA CAWUHAN. CI TAATAANUG NDEY KODDU FAAL) Ndey Koddu Faal...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA