Defu Waxu

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

IBA DEER WÉETAL NA SENEGAAL (NDEY KODDU FAAL)

Gaawu 31eelu fan ci weeru oktoobar 2020 la Iba Deer Caam génn àddina ci...

MAMADU NJAAY, NJIITU CESTI LU BEES LI (NDEY KODDU FAAL)

Fan yii weesu, defuwaxu.com, seen yéenekaay ci kàllaamay Kocc, bindoon na fi ab kayit,...

NDEY SÀGGAN, DOOM FAATU (NDEY KODDU FAAL)

Waa Mamel, fii ci Ndakaaru, naqar ak tiis lañ fanaanoo. Li ko waral mooy...

KAN MOOY JIITEJI CESTI ? (NDEY KODDU FAAL)

Atum 2005 ak léegi daara ju mag jiy tàggat taskati xibaar yi ci Iniwersite...

ÀTTEKAT YUY WERANTE BAY WEERANTE (NDEY KODDU FAAL)

Fii ci Senegaal, ay kàngam ci yoon ñooy tamante dëmm. Àttekat bii di Yaaya...

« Y’EN A MARRE » (NDEY KODDU FAAL)

Talaata jii ñu weesu (1 Sàttumbar 2020) kurél gii di « Y’en a marre...

MUSAA JÓOB BAÑ NA NI MUUT, NEE NA MOTT (NDEY KODDU FAAL)

Musaa Jóob layookat bi doon jiite "Dakar Dem Dikk" la njiitu réew mi tekki...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA