Li fës

ABLAAY DAAWDA JÀLLO TOPP NA CI GINNAAW AAMADU BA

Ablaay Daawda Jàllo amal ñam ndaje ak taskatixibaaryi, tey ci ngoon, doon ci leeral...

ETAASINI : DÀQ NAÑ 140i SAA-SENEGAAL

140i saa-senegaal la Etaasini dàq. Daf leen a waññi ginnaaw biñ fa duggee ci...

DABBAAX : BAAX NGIR YÀLLA, BAAX CI SENEGAAL

Senegaal, ci sunu aada, bu ñu tuddee doom, dañu baaxoo di ñaan : Yal na...

MAKI SÀLL DINA TABB CÀMM GU BEES

Ginnaaw bim tànnee lawax bi mu bëgg mu wuutu ko ci boppu réew mi,...

REYATI NAÑ ÑETTI NIT FA KÉEDUGU

Ab xeex bu metti moo amoon diggante takk-der yi ak askan way yeewoo fa...

ÑETTI FANI DËJ FA MALI

Tiis wu metti moo dal ca kow askanu Mali. Lu tollu ci juróom-benn fukk...

AAMADU BA : LAWAXU BENNOO BOKK YAAKAAR CI WOTEY 2024 YI

Ginnaaw wiiri-wiiri bu metti bi, àgg nañ Ndaari. Maki Sàll tànn na Aamadu Ba,...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...