Li fës

RËNG-RËNG FA MAROG : 820i NIT DEEWAGUM NAÑ CI

820i nit ñoo ñàkkagum seen i bakkan ci rëng-rëng bi yëngal suufus Marog si....

BENNOO BOKK LAWAX WALLA FÉEWALOO TAS YAAKAAR ?

Coowal lawaxu Bennoo Bokk Yaakaar la yéenekaay yi xëyee tey ci àjjuma ji, 8...

BATAAXAL BU JËM CI MAAM SEŊOOR

Maam, Fan yee weesu, sama xel dafa ne yarr ci yaw. Ba nga demee ba...

SËÑ BÀMBA

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom bi ci dem...

USMAAN SONKO DAKKAL NA XIIFAL GI

Ci gaawug tey jii, 2 sàttumbaar 2023, la xibaar bi jib. Yéenakaay bii di...

“COUP D’ÉTAT” FA GABOŊ : “XEEXU BIIR LA” (ALBEER ONDOO OSAA)

Albeer Ondo Osaa mi jiite kujje gi fa Gaboŋ doon na amal ab laaj-tont...

“COUP D’ÉTAT” FA GABOŊ

Gaboŋ, sóobare yi foqati nañ Nguur gi ci loxoy Aali Bongo ginnaaw wotey Njiitum...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...