Li fës

ÀQ AK YELLEEFI DOOM-AADAMA : SENEGAAL DAFA GËN A DELLU GINNAAW

Senegaal mi ngi ci guuta. Loolu la kurél yiy sàmm àq ak yelleefi doom-aadama...

MEERI BU NDAKAARU : DÀQ NAÑ ABBAAS FAAL MU PASTEF

Démb ci àllarba ji la meeri bu Ndakaaru doon yeesalaat pekkoom gi. Li ñu...

KUMBA AM NDEY, KUMBA AMUL NDEY

Démb lañ bàyyi Xuwaan Baranko (Juan Branco), yóbbu ko ca saa sa fa dalub...

RAWALEES NA USMAAN SONKO CA FAJUWAAY BA

Làngug Pastef les Patriotes génne na ab yégle di ci xamle ne, rawalees na...

NISEER : CEDEAO DAY SONG AM DÉET ?

Ayu-bés a ngi nii ak lu teg, bi sóobare yi foqatee Nguur gi fa...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (4/8/2023)

PASTEF Ñoo ngi wéy di raafal ndawi Pastef yi. Keroog, Tuseŋ Màngaa ak Bentaleb Sow...

FITNA DU YEM CI BOPPU BOROOM

Njiitul Pastef li, Usmaan Sonko, ma nga ndung-siin jamono jii. Lees ko jàpp, am...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...