Li fës

Ñaareelum ndaje Riisi-Afrig

Ci alxames jeek àjjuma jii la réewum Riisi doon dalal ñaareelum ndaje mi dox...

JURÓOM-ÑAARI TUUMA YEES GÀLL USMAAN SONKO

Usmaan Sonko kaso la jëm. Loolu la mbir yiy xeeñ jamono jii. Ginnaaw biñ...

JÀPPATI NAÑ USMAAN SONKO

Fan yii weesu lañ ñàggi kër Usmaan Sonko ginnaaw 55i fan. Ñu yaakaaroon ne...

“COUP D’ÉTAT” CA NISEER

Dañ ko doon laam-laamee démb, waaye leer na tey. Këppatal nañ Nguurug Bazoum gi....

MBËKK MI, BA KAÑ ?

Mbëkk mi lëmbeeti na réew mi. Jamono yii, mëneesul a toog ab bés te...

DAAN NAÑU CHINA MALL

Bi China Mall ubbeey buntam, saa-senegaal yi dañ ko tatafu xaat-xaat ndax bariwaayu njaay...

AMINATA TURE ÑEEL CREI : « BU DÉMB DOON TEY… »

Ci alxames jii weesu la dépite yi jàllale sémbub àtte bi fi jële CREI...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...