Li fës

BIBO BOURGI TOROXAL NA NGUURUG SENEGAAL

Gàcce bu reyul, semmal. Nguurug Senegaal a ngi ne tott ci kanamu àddina sépp....

XEEXI ÑAXTU CA DAARAY SIGICOOR JU KOWE JA

Daara yu kowe yi ci Senegaal dafa mel ni ag dal daf leen a...

F24 MI NGI ARTU…

Tey ci altine ji lañu woo woon dépite yi ca Ngomblaan ga. Dafa amoon...

SÉMBUB ÀTTE BUY SOPPI DOGUB 87 BI

Ëllëg, ci altine ji 16 sulet 2023, lañ war a wote ca Ngomblaan ga...

« RAŊ ! RAŊ ! KEŊ ! KEŊ ! … » NDAKAARU RIIR NA DÉMB

Bool, marmet, kubéeri cin, kuddu cinwaar, kuddu luus, mbiib yi, korne yi… lépp a...

Nguur geek Usmaan Sonko : Mën a tëru, mën a teggi

Tey ci gaawu bi, 15i fan ci weeru sulet 2023, la làngug politig gii...

MBIRUM 300i ROÑUKAT YI RÉER CI GÉEJ GI

Ñetti gaal, yeboon 300i nit, 300i doomi réew mi, ñoo ne mes, réer. Ñaari...

BAC 2023 : NJUREEF YU BAAX

Ginnaaw bi ñu leen nattee ci Talaata jee wees, njureefi BAC yaa ngi tàmbalee...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...