Li fës

LEES WAR A JÀNG CI NDIMBALU RÉEWUM FIDEL CASTRO ÑEEL ITALI ?

BOOS NDÓOY   Saa buñ tuddee réewum Kibaa, ñépp daldi fàttaliku njiitam lu ràññeeku la :...

BATAAXALU ITALI BU TIISE NII…

Mbokki Senegaal, Maa ngi leen di nuyu yéen ñépp, ku ci nekk ci sa tur...

KÀDDUY AADAMA JEŋ

Tofo ci Antonio Gutieres, « Sekerteer Seneraalu » Mbootaayu xeet yi, di ko xelal ci lépp...

MASAALIKUL JINAAN WALLA YOONI ÀJJANA YI

Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci...

MÀNDELAA WAR NAA AM NAQAR FA MU TËDD !

Lan moo dal sunu mbokki réewum Afrig-bëj-Saalum ? Su ma nee ‘’mbokk’’, nit ñu ñuul...

‘’LI TAX SÉEX ANTA JÓOB AMUL MOROOM…’’

WAXTAANU SAADA KAN AK BUBAKAR BÓRIS JÓOB

« Man, dama jàpp ne, CFA ak ECO ñoo yem kepp, benn baaxu ci. »

Ñaareelu xaaju waxtaanu Mamadu Jàllo ak Ndongo Sàmba Silla

XËT YI MUJJ

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2025)

NDÉGLUG FARBA NGOM Tay, ci alxames ji la waa PJF (Pool Judiciaire Financier) woolu woon...

SËRIÑ AMDI MÓODU MBENDA FAAL WÀCC NA LIGGÉEY

Sëriñ Amdi Móodu Mbenda Faal, xalifa Baay-Faal yi, wàcc na liggéey. Démb ci àllarba...