Li fës

COOWAL NAPPKATI KAYAAR YEEK YU MBOORO YI

Géej gi sàmbaraax na. Bakkan bu rot, 22i nit ñu amey gaañu-gaañu, ñaar ñu...

MAKI WAX NA AK NDAW ÑI

Màggalug bés bi Senegaal moome boppam, dafa nekk aada ci réew mi. Ñu jàpp...

4 AWRIL : NAXEE-MBAAY WALLA ?

Tey, talaata, 4 awril 2023, la Senegaal di Màggal jonnug boppam, ginnaaw juróom-benn-fukk ak...

LI GËN A FËS CI XIBAARI RÉEW MI (ALTINE 3 AWRIL 2023)

4 AWRIL Yewwi Askan Wi gàntal na Njiitu réew mi, Maki Sàll Lëkkatoo Yewwi Askan Widu...

LÀRME BI PÓLITIGUL

Bërki-démb, ci àjjuma ji, la waa Yewwi Askan Wi génne woon ab yëgle ngir...

YARGA SI, BÉYU SARAX BI

Démb la àttekatu Ñaareelu kabine bi dóor ab « mandat de dépôt » ndawul Pastef li,...

4 AWRIL : NAXEE-MBAAY WALLA ?

Fileek ñeenti fan, Senegaal dina Màggal jonnug boppam, ginnaaw juróom-benn-fukk ak ñetti at, bim...

MAAM MBAY ÑAŊ : ” SONKO RËCCAGUL. “

Maam Mbay Ñaŋ nee na day def "appel", du bàyyi mu sedd. Moom, ak...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...