Li fës

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀJJUMA 14 AWRIL 2023)

Waxtaanuw Usmaan Sonko ak Jean-Luc Mélenchon Njiitul Pastef li xamle na, ci xëtu Facebookam, ne...

« ÑUULE BU BON BI ! »

Bi joŋanteb Manchester City ak Bayern Munich bi jeexe, ndeke, Saajo Maane ak Lërooy...

MUSIBAB SINJAA

Diggante ndongo daara ak sëriñam, yenn saa yi, du doon lu ratax. Lu ci...

AKSIDÃ CA LUGA : JURÓOMI BAKKAN ROT NAÑU

Tali baa ngiy wéy di faat bakkani way-tukki yi. Aksidaŋ bu jàll, beneen tegu...

CHINA MALL, WÓOR NAAM ?

Ginnaaw AUCHAN, yaxantukati saa-senegaal yi amaat nañu geneen gan. Geneen kërug liggéey (entreprise) gu...

TUBAAB YAA NGI YEDD MAKI SÀLL

Kurél gi boole digaaley Senegaal yi ci wàllu xarala ak kopparal, G50, yedd na...

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ – USMAAN SONKO JEEXAGUL

Démb, ci alxames ji, 6 awril 2023, layookati Usmaan Sonko yi woote woon nañu...

YANQOOBA JATARA DAY TEKKI NDOMBOG-TÀNKAM

Lees doon xaar jib na : Yanqooba Jatara, jëwriñu tàggat-yaram gi, génn na pàrti...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...