Li fës

Tukkib Njiitu Réewum Farãs li ci kembarug Afrig

Tukki ñeenti fan la Emanuyel Makarõ, Njiitu réewum Farãs li tàmbali alxemes 2 màrs...

WOTEY 2024 LIY JOT, JOT NA

Lu moy at kepp a des ci wotey 2024 yi. Lawax yi tàmbali nañu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (ALXAMES 2 MÀRS 2023)

WÉR-GI-YARAM : Raglub Maam Abdu Asiis Si Dabbaax Liggéeykat yi ëmb Intersyndical bu raglub Maam Abdu...

YÉENE NÉEG LA, BOROOM A CAY FANAAN

Siidi Ahmet Mbay, ku dégg tur wi sam xel dem ci coowal Aji Saar...

FESPACO

FESPACO (festival panafricain du cinéma et de la télévision de Ouagadougou) bokk na ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 27 Féewirye 2023)

PÓLITIG Wotey Njiitu réewum Senegaal Décce Faal dina nekk lawax ci wotey Njiitu réewum Senegaal yu...

TABB YU YEES ÑEEL KÀNGAAMI YOON YI

Ci altine jii weesu lañu doon amal ndaje miy boole ak a tabb ñiy...

Kaïs Saïed : weex der taxul a weex xol

Ndekete yoo, nit, nit ay posonam. Kàdduy boddekonte yi Njiitu réewum Tinisi li biral, keroog...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...