Li fës

KEN NDÓOY « ÑÀKK NA BAKKANAM »

Bindal sargal ku génn àddina, damay koy def. Waaye de, lu ma diis la,...

LI GËN A FES CI XIBAARI BÉS BI (Alxames 16 féewaryee 2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAN AK USMAAN SONKO Tey ci alxames ji lañu waroon a àtte...

AY DU YAM CI BOPPU BOROOM

Jàppante ba amoon Mbàkke doxoon ci diggante takk-der ya ak soppey njiitu Pasteef lii...

YOOTE BI AM DIGGANTE MAKI SÀLL AK USMAAN SONKO

Lu tollu ci at kepp a des ci wote yi, coow li ne kurr...

Réewandoo (fédération) diggante Burkinaa, Mali ak Gine ?

Jëwrin yees dénk wàlluw bittim réew ca Mali, Burkinaa ak Gine jot nañoo amal...

SIGARET : REYAATEKAT BI

Bërki-démb, ci talaata ji 7i fan ci féewaryee 2023, lees doon amal ndajem liggéey...

SÉEX ANTA JÓOB : XARNUB LEER

Fanweeri at ak juróom-ñaar ginnaaw ba mu làqoo, Séex Anta Jóob du mës a...

RËNG-RËNG CA TURKI AK SIRI : 4 890iy NIT DEEWAGUM NAÑU

Suuf si yëngooti na, àddina jooyati. Nde, ay rëng-rëng yu mettee metti ñoo dal...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...