Li fës

MAKI SÀLL DÀQLU NA AMINATA TURE, TËJLU NIT-DOF

Pekkub Ngomblaan gi dafa amaloon am ndaje ci bésub tey jile. Ndaje ma nag,...

MOO MAN LU MAY WAXATI ? (Taalifu Séex Aliyu Ndaw)

Keroog, àllarba 18i fan ci saŋwiyee 2023 la mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ doon sargal...

USMAAN SONKO : « GAT-SA GAT-SA ! … DINANU XEEX AK MAKI SÀLL ! »

Kër Masaar wàcc na. Bu yeboo, bés niki tey, nu ngéntewaat depàrtmaa bu bees...

PELENT YA JOLLI NAÑ

Téere Séex Yérim Sekk bi ak coowal Aji Saar-Usmaan Sonko ñooy ñaari xibaar yi...

Burkinaa Faaso : lu ëpp 50i jigéen ni mes ni meenteñ

Diggante alxames ak àjjuma (12 ak 13 sãwiye 2023), lu ëpp 50i jigéen ñoo...

SÉEX ALIYU NDAW : NIT KI AK LIGGÉEY BI (Ibraayma Wan)

Saawo si ak nji yi Siidi Ahmet Aliyun Ndaw a ngi juddu atum 1933...

Rafayel Njaay taalifkat la woon…

Ndeem dëgg la ni àjjana, ngir mbindeef yi daa yokk yëf yu baax ci...

SÉEX ALIYU NDAW : BÉS DU ÑÀKK, DAY SORE

Mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ daa fas yéene delloo njukkal bindkat bu mag bii di...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...