Li fës

CAABALUG ËTTUB CETTANTAL GI ÑEEL YORINU FORCE COVID-19

Ëttub cettantal gi dafa bokk ci bànqaas yiy saytu liggéeyuwaay yi nga xam ne...

Ñetti faniy ndajem USA – Afrig

Talaata 13i fan ba alxames 15i fan ci weeru desàmbar 2022, ay njiit ak...

NGOMBLAAN GI GANTAL NA PASUM DIIŊAAT MU WAA YAW

Démb ci alxames ji la Ngomblaan gi amaloon am ndaje ngir wote pasum diiŋat...

TÀMBAAKUNDAA : PÉEYUB SENEGAAL CI DIIRU 3i FAN

Li ko dale 26 desàmbar jàpp 29 desàmbar 2022, Njiitu réew mi ak Càmm...

LIGGÉEKATI INIWÉRSITE YI JÓGATI ÑANU

Njàng mi ak njàngale mi dafa mel ni du jóg ciy njàmbat. Mënees na...

NDAM LU RÉY, NDAM LU TUUT

Alxames, 8i fan ci desàmbar 2022. 15i waxtoo jot ci ginnaaw njolloor. Ñi ëpp...

Xeex nger ci àddina si

Ci àjjuma ji, 9i fan ci weeru desàmbar 2022, la àddina wërngal këpp doon...

« COO ! NOO ÑÀKK FAYDA !… COO ! NOO ÑÀKK JOM ! »

Magum jawriñu Senegaal, Aamadu Ba, ma nga woon Farãs, waroon fa teewe ndajem liggéey...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...