Li fës

JÀPP NAÑ MEERU SINJAAN BI

Ceerno Jaañ, meeru Sinjaan bi, lañu jàpp tey ci àllarba ji. Jàllale nañ ko...

136EELU AJUG POPENGIN

Ci ndoorteelu ayu-bés bi, altine 20 ci weeru me 2024, la waa jàngu bi...

JÀPP NAÑ BAH JAXATE AK IMAAM SÉEX TIIJAAN NDAW

Démb lañ jàpp kii di Bah Jaxate, di aktiwist bu jege Maki Sàll. Waa...

PAATUG NJIITU RÉEWUM IRÃ

Njiitu réewum Irã li, Ebraahim Raysi, faatu na. Fafalnaaw bi mu duggoon ak jëwriñam...

“COUP D’ETAT” BU MOY FA RDC

Ab “Coup d’Etat” moo naroon a am fa Réewum Kóngo Demokaraatig (RDC). Démb, ci...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA NISERIYAA AK GANA

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, mu ngi wéyal tukkeem yi ci...

“LAC DE GUIERS 2” GËNATI NA CÓLLE

Mbërum Géejawaay mi, Paab Ãsu Siise, ñu gën ko miin ci dàkkentalu “Lac de...

USMAAN SONKO ŊÀÑÑ FARÃS, ARAAMAL NGÓOR-JIGÉEN

Usmaan Sonko,  njiitul PASTEF, doon na dalal Jean-Luc Mélenchon. Njiitul làngu La France Insoumise,...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...