Li fës

NAPP GI : JUB, JUBAL, JUBBANTI

Jëwriñu napp gi, Doktëer Faatu Juuf, siiwal na toftaleg turi nit ñi ñu jagleel...

15eelu NDAJEM OCI

Ci njeexitalug ayu bés bi, gaawu 4 ak dibéer 5 me 2024, lañ doon...

GOR, CA WAX JA !

Lu tollu ci weer ginnaaw ba ñu ko tabbee elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko...

« UN TOMBEAU POUR KINNE GAAJO » : FÀTTALIKU NGIR JARIÑU

Bubakar Bóris Jóob génnee na téere bob, way-loru yi laboon ca suuxug « Le...

PRODAC : CAABALU ËTTUB CETTANTAL BI DËGGAL NA USMAAN SONKO

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, dafa santaane woon ñu siiwal caabali luññutu yees...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, demoon na Gine Bisaawo ci talaatay tey...

AKSIDAŊ YI : 1 200I WAY-DËDDU DIGGANTE 2021 AK 2022

Dem beek dikk baa ngi wéy di jur coow fi réew mi. Ay aksidaŋ...

SEMINEERU NGUUR GI

Démb ci gaawu gi la Nguur gu bees gi doon amal ab semineer. Njiitu...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...