Li fës

BUBAKAR BÓRIS JÓOB ÑAAWLU NA KÀDDUY TAYIIRU SAAR YI

Fan yii weesu, Tayiiru Saar, njiitul làng gii di Parti nationaliste, dafa fésaloon i...

CÀMM GU BEES GI : WAAW, ANA JIGÉEN ÑI ?

Ginnaaw ba mu jële lenge yi, njiitu réew lu bees li Basiiru Jomaay Jaxaar...

NJIITU RÉEW MI DUNDAL NA AADA

Tay ci àllarba ji, 10i fan ci weeru awril lees doon amal jullig kori...

KORITE 2024

Ren, daanaka àddina sépp ci àllarba tey ji lañu wori. Senegaal itam, tey la...

FAATUG MUHAMMET JÓOB FA PIKIN

Am nay xibaar yu bees yu rot ñeel faatug Muhammet Jóob. Nde, jàllale nañ...

JIITUWAAYI CÀMM GU BEES GI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, taxawal na càmm gu njëkk ci moomeem...

JËWRIÑI CÀMM GU BEES GI

Jëf toxal na wax. Ñoo ko dige woon, jëfe nañ ko. Umar Sàmba Ba...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...