Li fës

SËÑ BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY, 5EELU NJIITU RÉEWUM SENEGAAL

Lépp mat na. Ndajem Ndeyu Sàrti Réew mi dëggal na njureef yi tukkee ci...

ASP : 39i LIGGÉEYKAT YU BEES CI ÑAARI FAN

Njiitul “Agence de sécurité de proximité” (ASP) li jël na 39i liggéeykat yu bees...

MAKI SÀLL, DALAL NA JOMAAY AK SONKO FA PALE BA

Njiitu réew mi, Maki Sàll, dalal na ki koy wuutu, Basiiru Jomaay Fay, ak...

WOTEY 2024 : ËTTUB DABU BI BIRAL NA NJUREEFI NÉGANDIKU YI

Tay ci àllarba ji la Ëttub dabu bi nekkee Ndakaaru biral  njureefi néggandiku yi...

COPPITE YI BASIIRU JOMAAY FAY DIGE

Démb la Njiitu réewum Senegaal lu bees li doon biral kàddoom yu njëkk. Fa...

MAKI SÀLL NDOKKEEL NA NJIITU RÉEW MU BEES LI, BASIIRU JOMAAY FAY

Njiitu réew ma woon, war a fegal keroog 2 awril 2024, ndokkeel na Njiitu...

AAMADU BA WOO NA BASIIRU JOMAAY FAY NGIR NDOKKEEL KO

Sànq la xibaar bi rot. Muy xibaar boo xam ne biig ci guddi ba...

BASIIRU JOMAAY FAY RAAFAL NA LÉPP !

Basiiru Jomaay Jaxaar Fay jël na raw-gàddu gi ! Daanaka, taax yu mag yépp...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...