Li fës

JAM NAÑ MAYMUNA NDUUR FAY

Maymuna Nduur Fay, taskatu xibaar bi jiite 7tv la ab/ay sàmbaabooy dogaale, fitnaal ko,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/2/2024)

PÓLITIG Ndiisoog pólitig ga ca diisoo ba Njiitu réew ma woote woon noppi na. Bees...

MBAAM MI : ÑETTI LÉEB

Cokkaasu RFI bii daf nuy fàttali ñetti léeb yoy, mbaam a ciy ndeyu-mbill ji....

DIISOOB FÉEWALOO

Ginnaaw-ëllëg ci altine ji, 26 féewiryee 2024, la diisoo bi Njiitu réew mi woote...

MAKI SÀLL A NGI WÉY DI LËJAL KÀRT GI

Démb la Njiitu réew mi doon tontu laaji taskati xibaar yiy liggéeyee RTS, Le...

LÀMMIÑ WEES NÀMP

21eelu féwaryee lañ jagleel ci àddina sépp bésu làmmiñ wi nga nàmp. Xalaat bu...

DIISOOB WOTE YI

Ndajem ndeyu àtte mi neenaloon dekkare Njiitu réew mi ak sémbub àtte bi Ngomblaan...

“KAFKA” LU MU NU WAX CI MAKI ?

Téereb "Kafka" bii dafa lay jàngal lu bari. Ni àddina man a xëyee rekk...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...