Li fës

MAKI SÀLL JÉBBALU NA

Gaawu, ñetti fan ci weeru féewiryee 2024 la Njiitu réew mi jëloon ndogalu dàq...

NDAJEM NDEYU ÀTTE MI NEENAL NA DEKKARE NJIITU RÉEW MI !

Ndajem Ndeyu àtte mi àtte na ! Juróom-ñaari kàngaami àttekat yi neenal nañ dekkare bi...

MAKI, FÀTTALIKUL “PAPA DOC”

Jafe na nga xam as lëf ci dundu "Papa Doc" (François Duvalier) mu réewum...

AAR SUNU ÉLECTION BËTAL NA DOXU-ÑAXTOOM BI

Kurél gii di wuyoo ci turu Aar Sunu Élection tegandi nañu ci suuf seen...

ABDU JUUF DELLU NA GINNAAW

Démb, Abdu Juuf ak Abdulaay Wàdd, Njiitu réew ya woon, dañ bokkoon bind ab...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2024)

ETAASINI A NGI YEDD NGUURU SENEGAAL Àmbaasad Etaasini mi ngi yeddati Nguurug Maki Sàll gi....

SÉMBUB ÀTTE BUY NEENAL I DAAN

Yéenekaay Le Quotidien moo siiwal xibaar bu bette, tey ci yoor-yoor bi. Yéenekaay bi...

MAKI SÀLL : “…BU BOOBAA, (…) ÑÉPP ÑOOY ÑÀKK…”

Njiitu réew mi, Maki Sàll, fasul yéene dellu ginnaaw. Ñaari bakkan rotagum nañ ci...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...