Li fës

WOTEB SÉMBUB ÀTTE BIY DÀQ WOTE YI

Ngombalaan gi jàllale na sémbub àtte biy dàq wote yees nammoon a amal ci...

MAKI SÀLL : XUUS JÀLL WALLA RASU GÉNN ?

Bërki-démb ci bëccëg gi la Njiitu réew mi jël ndogalu fomm wote yi waroon...

“DAÑU NAR A DÉJJATI MAKI SÀLL…”

Paap Aale Ñaŋ a fésal xibaar bu doy waar ci xëtu Facebookam. Daf ci...

XIBAAR YU TEMBARE

NGOMBLAAN GA Càkkuteefu neenal dekkare fomm wotey 2024 YI Maalig Gàkku, Basiiru Jomaay Fay ak Seex...

NGOMBLAAN GA

Ci biir sémbub àtte biñ war a wote fa Ngomblaan ga, dañ ci bind...

SÉMBUB ÀTTE BIY DÀQ WOTE YI : AJANDI NAÑ JOTAAY BI

Njiitul Ngomblaan gi dàqandi na jotaay bi, ginnaaw bi dépitey Yewwi Askan Wi ak...

WAAW, ANA AAMADU BA (BBY) ?

Gaawu, 3 féewaryee 2024 lañ gëj a dégg Aamadu Ba, jëwriñ ju mag ji,...

FOMMUB WOTEY 2024 YI : XALIFA MURID YI ÀNDU CI

Démb, jëwriñu biir réew mi ak nawleem biñ dénk larme bi ñoo nga woon...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...