Li fës

BAKKAN ROTAAT NA FA GINNAAW RAAY

Ginnaaw ndongo la gaañu fa jànguneb Ndar, beneen ndaw ñàkk na bakkanam fa Ndakaaru....

“UGB DU AY SËG !”

Ginnaaw Fàllu Seen (2018), leneen ndongo faatooti na fa jànguneb Ndar ba ci sababuy...

ÑAARI BAKKAN ROT NAÑ XAAT

Bakkan rot na fa jànguneb Ndar ba (Iniwérsite Gastoŋ Berse). Taskatu xibaar bii di...

SAA-CEES YI SÓOBU NAÑ CI XEEX BI !

Ndaw ñi jóg nañu fa Cees. Mu mel ni ndaw ñi fippooti nañu. Tay...

XEEX BI TÀMBALEETI NA !

Xeex bi tàmbaleeti na diggante askan wi ak takk-der yi. ndogalul dàq wotey 2024...

MAKI SÀLL A NGI GËN A WÉET

Keroog, gaawu 3 féewiryee 2024, la Njiitu réew mi jëloon ndogalu xaatim ab dekkare...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/2/2024)

WAA ETAASINI, UE AK CEDEAO DAL NAÑU CI KOW MAKI SÀLL Ndogalu Njiitu réew mi...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...