Li fës

SAMES SÓOBU NA CI XEEX BI

Fajkat yi xamle nañ ne dinañ dakkal seen liggéey ci diirub ñaari fan. Seen...

NGOMBLAAN GI JÀLLALE NA SEMBUB ÀTTE BI

Bees sukkandikoo ci Ayib Dafe, Ndiisoog àtte yi jàllale na sembub àtte biy soppi...

NDOGALU FOMM WOTEY 2024 YI : XEEX BI DOOR NA !

Lawax yi ñoo woote am ndaje mu mag ngir ñaxtu ñeel ndogal li Maki...

NJIITU RÉEW MI FOMM NA WOTE YI

Wotey 2024 yi duñ am ci bésub 25 féewiryee bees leen àppaloon. Ndogal lu...

ABDU LATIF KULIBALI TEKKI NA NDOMBOG-TÀNKAM

Abdu Latif Kulibali, di jëwriñ ak magum fara-caytu Nguur gi, jël na ndogalu tekki...

DIC WOO NA ROOS WARDINI

DIC woolu na njiitul kurélu « Sénégal Nouveau », Roos Wardini miy lawax ci wotey 2024...

BUUR BI, DAG BI AK BATAÑSE BI

Bés, Buur dafa toog ak dagam, ñuy waxtaan. Buur ne ko : - Sama xel dafa...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...