Li fës

COOWAL NASIYONAALITE KARIIM MAYSA WÀDD

Juróomi fan kepp a des balaa ndajem ndeyu àtte miy siiwal limug lawax yiy...

MBIRI BAABAKAR FAAL : CAP DUGG NA CI COOW LI

Waa CAP àddu nañu ci mbiri Baabakar Faal. Ginnaaw bi taskatu xibaar bi jotee...

CAN KODDIWAAR 2024

Ëllëg ci gaawu gi la joŋantey CAN biy door. Ren, Koddiwaar moo dalal xëccoo...

WOTEY 2024 YI : AG TËNK ÑEEL BAAYALE GI

Areete 032005 bu 25 sàttumbaar 2023 bu njëwriñu biir réew mi biraloon moo tënk...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : COOWAL LIJAASA “CAP” BI

Jàngalekat yaa ngay ñaxtu ak a naqarlu anam bi ñu nekke, rawatina ñàkk maandu...

CAYTUG BAAYALE GI : ÑAAREELU SUMB BI

Tey ci talaata ji, 9 sãwiyee 2024, la ndajem ndeyu àtte réew mi doon...

WOTEY 2024 YI : LËNT-LËNTI BAAYALE GI

Ginnaaw bi ndajem ndeyu àtte mi noppee ci caytu gi njëkk ñeel way-sàkku lawax...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...