Li fës

SOXNA JAAGA MU BÀLLAAGO DËDDU NA

Dee du jaas. Fu ko kenn dul xaar la malaakam dee mi naan jaas,...

KARIIM WÀDD : “DAMAY BOKK CI NII WALLA CI NAA…”

Gaawu gii weesu la ndajem ndeyu àtte mi biral limu lawax yiy bokk ci...

SONKO AK KARIIM DUÑ BOKK CI WOTEY 2024 YI

Ndogal li rot na. Tey jii, ci gaawug 20 sãwiyee 2024, la 7i àttekati...

SENEGAAL AK MÓRITANI : NDEFARUG GIL BI DINA TÀMBALI

Dees na tàmbali ndefarug gil (gaas) gi ci diggante Senegaal ak Móritani. Ci atum...

GAYNDEY SENEGAAL YI RËKK NAÑ YOY KAMERUN YI

Gannaaw ba mu wullee dëkkandoom bi, Gàmbi, keroog ca bés bu njëkk ba, Senegaal...

SENEGAAL-KAMERUN : LÀMBU GAR AK ÑALÓOR

Tey ci àjjuma ji la gayndey Senegaal yiy laale ak yoy Kamerun. Bu 17i...

XALIFA SÀLL JIITAL NA BÀRTELEMI JAAS

Bàrtelemi Jaas mooy jiite kàmpaañu Xalifa Sàll. Ci ngoon gi la xibaar bi rot....

WOTEY 2024 YI : LAWAX YAA NGAY GAL-GALANTE

Ndekete yoo, nekk lawax ci réewum Senegaal yombul. Ca dëgg- dëgg, mbir mi làmbi...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...