Li fës

NGOMBLAAN GI WOTE NA CÀRTUG CÀMM GI

Bërki-démb ci altine ji fukki fan ak juróom-ñatt, dépite yi wote nañu sàrt càmm...

BÉSUB MBËKK MI

Démb ci altine ji, 18 desàmbar 2023, lees jagleeloon mbëkk mi ci àddina sépp....

JÉYYA JA AM CA GINE KONAAKIRI

Guddig dibéer jàpp altiney tey jii fukki fan ak juróom-ñett ci weer wii la...

DELLUSIG KARIIM MAYSA WÀDD FI RÉEW MI

Dellusig Kariim Maysa Wàdd fi réew mi doonatul lu ay ñoñam di xel-ñaar. Ñi...

MBIRUM MARJAAN YI : ME MUSAA JÓOB A NGI KASO

Meetar Musaa Jóob a ngi ci guddi yu lëndëm jamono jii. Ndax, tey ci...

ÀTTEWAAY BU NDAKAARU JOX NA SONKO DËGG

Coowal « damay bokk ! » ak « doo bokk ci wote yi ! », diggante Càmm geek Usmaan...

USMAAN SONKO AK CÀMM GI, PËND BA WUREEGUL

Dogal bi ñu doon xaar tey ci Talaata ji jëm ci àtteb Usmaan Sonko...

NDELLOOG USMAAN SONKO CI WAYNDAREW WOTE WI

Ci talaatay tey jile, 12 desàmbar 2023, la tirbinaal « hors classe » bu Ndakaaru di...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...