Li fës

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/12/2023)

WOTEY 2024 YI Tey ci altine ji, 11 desàmbar 2023, la deppo yi ñeel nekkug...

COOWAL KOPPARI QATAAR YI

Atum 2019 lañu jëkkoon a dégg jokkalanteg koppar gu dox diggante kërug lijjanti  gu...

COOWAL NJÀNG MU KOWE MI : UCAD TIJJEEGUL I BUNTAM

Jàngune Séex Anta Jóob bu ndakaaru tijjeegul i buntam. Musaa balde, jëwriñ ji ñu...

YOON BÀYYI NA USTAAS UMAR SÀLL

Àtte bi daanu na. Tey ci àjjuma ji lañ doon àtte Ustaas Umar Sàll...

LUUBALU 540I TAMDARET CA CMS BU MEDINAA

CMS ab bànqaasu déncuwaay ak àbbuwaayu xaalis la bu nekk ci biir réew mi....

GINE BISAAWOO : UMAR SISOKO EMBALO TAS NA NGOMBLAAN GA

Umar Sisoko Embalo, Njiitu réewum Gine Bisaawoo, tasati na Ngomblaan ga. Démb altine, ci...

BURKINAA FAASO : AAYEES NA YÉENEKAAY LE MONDE

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle....

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...