Li fës

ËTTU ÀTTEWAAY BU MAG BI : NJIIT LA GÀNTAL NA NEENAL-ÀTTE BU LAYOOKATI USMAAN SONKO

Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati Usmaan Sonko yi dugaloon....

AYIB DAFE A NGI YEDD CDC

Bu Usmaan Sonko bokkee ci wotey 2024 yees dégmal de, dina doon jaloore ju...

LAYOOKATI SONKO YI DUGAL NAÑ AB NEENAL-ÀTTE

Ginnaaw bi ëttu àttewaay bu mag bi neenalee woon àtteb Sabasi Fay ba, keroog...

JALOOREY RAGLUB SÓOBARE BU WAKAAM

Senegaal séqi na jéego bu am a am solo ci wàllu paj. Nde, doktoor...

AY CONGU CI YENN BÉRÉB FA SIYERAA-LEWON

Njàqare ak tiis la askan wa dëkke fa Freetown yeewoo démb. Ay sàmbaa-bóoy ñoo...

Xibaari Tàggat-Yaram

kuppeg Àddina U17: 1/2 finaal Joŋante baa ngi wéy, ñu tollu fim ne ci 1/2...

NJAAYUM GERTE GI : CÀMM GI SAMP NA NJËG GI

Càmm gi samp na njëg gees war a jaaye gerte gi ci kàppaañ 2023-2024...

USMAAN SONKO : « MBATIIT MOOY LÉPP, MOOY CËSLAAYU YOKKUTE. »

Laaj ak tontu bii nag, seen yéenekaayub web defuwaxu.com séqoon na kook Usmaan Sonko...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...