Li fës

CÀMM GU BEES GI : MAKI SÀLL TABBAAT NA AAMADU BA

Njiitu réew, mi Maki Sàll, tas na Càmm gi. Démb ci àjjuma ji la...

YOON GÀNTALATI NA USMAAN SONKO

Usmaan Sonko dafa dugaloon ? keroog 2i fan ci oktoobar 2023, ab « recours » ñeel li...

MOOMI SEKK, SOXNAS BUGAAN DANI GÉY, GÉNN NA ÀDDINA

Tiis ak naqar wu réy ñoo dal ci kow njiitul DMedias ak kurél Gëm...

UBBITEG LEKKOOL YI

Lekkooli Senegaal yi tàmbali na tijji ay buntam. Niki démb ci altine ji, 2...

XUWAAN BARÀNKOO TUUMAAL NA FARÀNK ÑÀNKI JOM

Farànk Ñànki Jom, di mag ci jëwriñ ji ñu dénk wàlluw biir réew mi,...

Wotey 2024 : wure wa dem na këŋ

Ubbi nañu utum parenaas yi ñeel wotey 2024 yi. Ñi fas yéene nekk lawax...

NISEER AM NA NDAM CI KOW FARÃS

Niseer am na ndam ci kow Farãs. Ginnaaw seen xëccoo bu yàgg bi (3i...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...