MAGU WAXOON NAA KO

SËRIÑ SEEKA BARI DOOLE CI LÀNGU PÓLITIG GI !

Ni waa Senegaal gëmee Yàlla te fonk diine, umpul kenn ci àddina si. Nde, askanuw...

FAIDHERBE DU FI MAAMU KENN

Fan yii yépp, xanaa mën nañoo wax sax weer yi weesu yépp, coow laa...

AFRIG AK KORONAA, AFRIG GINNAAW KORONAA

USÉYNU BÉEY Koronaawiris bi, li muy metti metti, terewul kàngami boroom xam-xam yiy wéy di ci...

FAN LANU JËM AK ÑAKKI BILL GATES YI?

(USÉYNU BÉEY) Coow laa ngi ne kurr ! Afrig ba Afrig daj, li ko dale Keer...

FAATUG HIBAA CAAM : SENEGAAL, BOPP BU XAR ÑAAR?

Guddi àjjuma, dëppook 3eelu fan ci weeru Awril, doon guddi gi jiitu bésub baaxentalub...

WÀDD-MAKI : GINNAAW AY…SOPPI ?

Keroog, àjjuma 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019,ba ñuy ubbi Masaalikul Jinaan, jullit yépp...

MBAY JAAG, GOR GI SENEGAAL AMEEL BOR (II)

Am it lu mat a taxaw-seetlu : jamono jooju Mbay Jaag doon jiite ndongo...

MBAY JAAG, GOR BI SENEGAAL AMEEL BOR (Xaaj bu njëkk)

Xel tëju na, xalaat dëju. Xol tooy na, bët jooy. Ndeysaan… Gaynde wàcc na liggéey....

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...