WAXLEEN SEEN XALAAT

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo tax mu daan Lii dinaa ko...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu kenn wéer goob ba Bii pas-pas...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel wotey tànn Njiitu réew mees...

TÀGGATOO

Roqi, ba beneen yoon. Seetal ma lii rekk. Wax dëgg. Xool sama digganteek Yàlla te...

BAÑ A WACC SA ÀND…

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu mu doon. Nekk cim réew,...

BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI

Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit. Joŋante yi gën a indi coow...

"LE PROTOCOLE DE L’ÉLYSÉE" : NJÀNGATU PROF BUUBA JÓOB  

Téere bu am solo bi Ceerno Alasaan Sàll génne fan yii ci nasaraan, te...

KORONAAWIRIS : TAXAW TEEWLU

Làmp Faal Kala Mbasum Covid-19 mi lëmbe na àddina, lëmbaaje xel yi ak xol yi,...

XËT YI MUJJ

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw...

LI CI DIGGANTE NIT AK NITE

Moo xam muy seen doomu bopp walla jeneen ju ñu leen dénk, way-jur yu...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL...