WAXLEEN SEEN XALAAT Ndigalu Maam Ya By Defu Waxu 02/04/2024 0 475 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët BOO BAÑEE ÑAAW… Baabakar Lóo - 26/05/2024 Njiitu Réew Defu Waxu - 02/05/2024 YAA GORE ! Defu Waxu - 14/04/2024 SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO Defu Waxu - 06/03/2024 Aji bind ji Defu Waxu Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu kenn wéer goob ba Bii pas-pas dara mënalu ko dara Dina daw ba raw xëlu fas Ngor ak jom a ko nas Ma ne, Askan wee ko sas Gan góoru jigéen ñi dar lingeer Ci seen farlook seen gànjar ya Bég ba tàccu ne sas Maam a ne bëret dan delsi Samp xeej daldi xas Gisuma fi yaakar ju tas Tuggee Tugal Wéyal yaak say dëbës Afrig dina bañ ba sës Ndawi tey yi dootuñu surgawu Topp sa gannaaw ni jaam bu nangu Dina tàng dina metti Waaye jàmbaar du xàddi Na doxandéem bii dakkal Wàqi gi muy wàqi sunu alal Di roñ di génne Di gaawantu di rawale Am ñu ne xiim di xoole Mbaa sax di ko ci dimbale Sàmm sam réew warugar la Bëgg sa réew siddit la Gor tigi du wor du wuruj Te su séddu jotee mooy mujje Biir bu rëy lex yu newwi Sonal sa bopp tooñ say ñoñ Moone de bànneex tigi Xanaa xam-xam ak néewle soxla Tey jiital njariñal doom Aadama Seex Aliyu Ndaw Ndakaaru, weeru mars 2024 Defu Waxu Plus de publications Defu Waxu https://www.defuwaxu.com/author/webmaster10/ NJUREEFI BAC 2024 YI Defu Waxu https://www.defuwaxu.com/author/webmaster10/ WATTU LÀKKI RÉEW MI 2/3 Defu Waxu https://www.defuwaxu.com/author/webmaster10/ WATTU LÀKKI RÉEW MI 1/3 Defu Waxu https://www.defuwaxu.com/author/webmaster10/ BÓOMUG ALEŊ KALI: G7 BU CEES DOOR NA XEEX BI FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/10/2024) Njuga Gay - 14/10/2024 KAAJARUG SÉMBUW SOPPI SENEGAAL FII AK 2050 Mbay Sow - 14/10/2024 LU YEES CI MBIRUM PRODAC Njuga Gay - 13/10/2024 LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/10/2024) Mbay Sow - 11/10/2024 NDAJEM NDEYU SÀRTU RÉEW MI DËGGAL NA LAWAXUG SONKO AK BÀRTELEMI JAAS Paap Aali Jàllo - 11/10/2024