Xibaar

SENEGAAL TIIT NA WAAYE ËLLËG, ËLLËGU ASKAN WI LA…(PAAP AALI JÀLLO)

Bindkat yi bind nañ, waxkat yi wax, gëstukat yi biral, boroom xam-xam yi jàngat,...

LI TAX 102i BOROOM XAM-XAM YU MAG JÀPP NE SENEGAAL DU RÉEWUM YEMALE (MA-JAW NJAAY)

https://m.soundcloud.com/mohamadou-boye/manifeste-en-wolof

LÉPP LI CI BIIR LÀNKETU KAPITEEN SÉYDINAA UMAR TURE CA "SECTION DE RECHERCHES" BU KOLOBAAN…

Ci tekkig Musaa Jóob Aysatu Ñaari ayubés ak léegi coow lëmbe réew mi yépp, am...

MARCEL MENDY NELAW NA (NDEY KODDU FAAL)

Taalifkat nga woon bu daan yatt xalimaam di bind ci xew-xewi réew mi. Misaal...

Macky sall (SBJ)

Muumaa di li mu fésal ci li xew ci réew mi. Ana lu waral faleesoon...

TEGGIG MALAANU KIIRAAYU USMAAN SONKO : LI CI YÉENEKAAY YI BIND (Paap Aali Jàllo)

Coowal Usmaan Sonko moo lëmbe réew mi jamono jii. Gannaaw tuumay siif ak tëkkub...

FAN LA SENEGAAL TOLLOOK ÑAKK YI ? ( Musaa Aysatu Jóob)

Niki weeru féewaryee ci atum 2020 lañ njëkk a dégg baatu koronaawiris , ci...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...