Xibaar

LI CI BIIR "MBOORUM ÀDDUNA SI" BU ABDU-XAADR KEBE

KAN MOOY SËRIÑ ABDU-XAADR KEBE ? Sëriñ Abdu-Xaadr Kebe, ñu gën koo xam ci turu...

SAFARAS NGAJAGA SI « Ci nen lan toog… » (Paap Aali Jàllo)

Ci gaawu bii weesu, 19eelufan ci weeru desàmbar, waa Ngajaga tiit ak njàqare lañ...

PAAP BUUBA, GAYNDE GU NU DOOTUL FÀTTE, (MUSAA AYSATU JÓOB)

Paap Buuba Jóob saay na, ginnaaw bi ko feebar bi ñuy wax "Charcot" tërale...

SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)

« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. » Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu...

RFI : NJUUMTE, YABAATE WALLA LAN ? (NDEY KODDU FAAL)

Bërki-démb, ci altine ji, rajo Rfi dafa juum tàgge ñaar ci njiiti réewu Senegaal yi...

BARSAA WALLA… BARSÀQ !… LU XEW CI MIIM RÉEW?

Géej gaa ngiy wann sunu doom yi. Mbete jasig juy warax béy bu lab. Ay...

JÀNGORO JU YÉEME JIY DAANEEL MOOL YI (PAAP AALI JÀLLO)

Jàngoro ju yéeme te raglu moo gaaral, fan yii, ay mool yu nappi woon ba...

SËRIÑ SEEKA BARI DOOLE CI LÀNGU PÓLITIG GI !

Ni waa Senegaal gëmee Yàlla te fonk diine, umpul kenn ci àddina si. Nde, askanuw...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...