Xibaar

SENGHOR AK HOUPHOUËT, DOOMI AFRIG YI DAAN XEEX AFRIG (2/2) BOS NDÓOY

Ci beneen boor, ci nguuru Seŋoor lees nose, ñeel Senegaal, “Opération Persil” ak lenn ci...

DOGALI MAKI YU BEES YI : BUUR DU MBOKK (PAAP AALI JÀLLO)

Bi Maki Sàll faluwaatee ci woteb 2019 bi ba léegi, ñoo ngi doon xaarandi...

MAMADU NJAAY, NJIITU CESTI LU BEES LI (NDEY KODDU FAAL)

Fan yii weesu, defuwaxu.com, seen yéenekaay ci kàllaamay Kocc, bindoon na fi ab kayit,...

18 SAFAR (TAALIFU SOXNA BAAWO JÓOB)

  18 SAFAR Dikkati nga ngir saafaraati sunuy aajooki tawat, yaw 18 safar. Kon képp ku bëgg...

BINDKATU AYUBÉS BI : IBRAAYIMA SAAXO CAAM

                Ibraayima Saaxo Caam a nga juddoo Rëbës ci atum 1973, muy gox bi nekk...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL II (BUBAKAR BÓRIS JÓOB)

 Moone de, ngóor sii ñuy sargal tey, mooy ki daan fitnaal ak a toroxal...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...