Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/1/2025)

MURIG MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM Ayu-bés bii ñu génn la Ngomblaan gi dooroon liggéey bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/1/2025)

USMAAN SONKO : DUGG NAÑU CI JAMONO JOJ, BAALE JEEX NA Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (17/1/2025)

ÑËWUB NJIITU RÉEWUM GANA FI SENEGAAL Tay ci ngoon la fi Njiitu réewum Gana ñëw...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/1/2025)

UBBITE ËTTI ÀTTEKAAY YI Tay ci alxames ji moo nekkoon bésub ubbite ëtti àttekaay yi....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/1/2025)

BÉS BI ÑU JAGLEEL NJÀNGUM XALE YU JIGÉEN YI Tay, alxames juróom-ñeenti fan ci weeru...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

SUPER CUP D'ITALIE : MILAN JËL NA KO ! Ci gaawub 7i sãwiyee bii lees...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/1/2024)

LAYOOB WATTUKATI KAARAANGEG LËKKATOO SÀMM SA KÀDDU Tay ci altine ji, ëttu àttekaay bu Ndar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/1/2025)

BÀRTELEMI JAAS TEGGIWUL TÀNKAM Ginnaaw bi Yoon nangoo moomeg dépiteem ak cëru meeru Ndakaaru, taxul...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...