Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/8/2024)

BLD/TAKKU SOSU NA Géewu pólitig bi amati na gan. Bi wote yi jàllee ba...

BÓOMUG ABDU ASIIS BA

Jéyya ju ñaaw ja ca Pikin Teknopóol mi ngi wéy di jur coow fi...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (21/8/2024)

MBIRUM PAS YEES WAR A SAYTUWAAT Càmmug Senegaal gi daa fas yéene saytuwaat pas yi...

CNRA ÀPPAL NA SAABALUKAAY YI

Bërki-démb, ci altine ji la banqaas bii di CNRA (Conseil National de Régulation de...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/8/2024)

NGOMBALAAN GI Ginnaaw bi ñu wotee àtte biy soppi sàrt-biiru ngombalaan gi, coowal tas gee...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/8/2024)

NJIITU RÉEW MI DALAL NA NJIITUL UEMOA UEMOA (Union Economique et Monétaire Ouest Africaine) mooy...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Ni ñu ko daan baaxoo di def àllarba ju nekk, noon la demee démb...

REAL MADRID JËL NA “SUPER COUPE D’EUROPE” BI

"Super Coupe d'Europe" mooy kub boo xam ni, ñaar ñi gañe joŋantey kuppe yii...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...