Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2024)

65eelu NDAJEM CEDEAO Démb ci dibéer ji, 7i pani sulet 2024, kurél gii di CEDEAO...

EURO AK COPA 2024

EURO : Njureefi 1/4 dë finaal yi Mats yi ñeel 1/4 dë finaal yi "Euro"...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/7/2024)

CEDEAO - AES CEDEAO jël ndogal ñee maxejji réewi AES yi (Mali, Burkinaa Faaso ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/7/2024)

OFNAC MI NGI DALAL ÑI ÑU TABB CI NGUUR GU BEES GI Ginnaaw bi...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Démb ci àllarba ji lañu doon amal ndajem jëwriñ yi ci njiiteefu Njiitu réew...

EURO AK COPA AMERICA 2024

EURO 2024 Njureefi 1/8 dë finaal yi Ndajey 1/8 dë finaal yi ñeel Euro bi jeex...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2024)

NJÀNGATI WOTEY 2024 YI Kurélu maxejj gii di COSCE (Collectif des Organisations de la Société...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/6/2024)

COOWAL “DPG” LAA NGI WÉY Coowal “DPG” (Déclaration de Politique Générale) dafa mel ni,...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...