Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/4/2024)

64EELU MÀGGALU JONNUG SENEGAAL Tey ci alxames ji la réewum Senegaal màggal juróom-benn-fukk ak ñeenteelu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (01/4/2024)

TABBUG BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY Ëllëg ci talaata ji, dees na tabb Basiiru Jomaay Jaxaar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/3/2024)

MAKI SÀLL DEF NA NDAJEM JËWRIÑAM MU MUJJ Dibéer jii weesu lañu doon amal...

ÀDDINA SAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY FAY

Wëliis Maki Sàll mi muy wuutu ci boppu réew mi, yeneen Njiiti réew yi...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (25/3/ 2024)

KÀDDUY BASIIRU JOMAAY FAY YU NJËKK NIKI NJIITU RÉEWUM SENEGAAL  Njiitu réew lu bees li,...

WOTEY 2024

Sàntar “Grande Medine” : Ci ndigalu perefe, dàq nañ taskati xibaar yépp bi waxtu...

KAN MOOY ANTA BAABAKAR NGOM ?

Anta Baabakar Ngom mooy jenn jigéenu lawax ci joŋantey 2024 yi ngir nekk Njiitu...

LI GËN A FÉS CI WOTE YI (22/3/2024)

PDS FEKKI NA BASIIRU JOMAAY FAY Ñépp a doon xaar PDS ngir xam naka lay...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...