Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/10/2023)

MBIRUM USMAAN SONKO AK I ÑOÑAM Suba ci alxames ji la Yoon di leeral lenn...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/10/23)

PÓLITIG Ngomblaan gi génne na ab yégle di ci xamle ne dina amal lëlu aadaam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/10/2023)

PÓLITIG Aali Nguy Njaay mottali na yéeneem ngir nekk lawax ci wotey 2024 yi. Ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI ( 5/10/2023)

MAKI SÀLL DINA TAS CÀMM GI Muy ab xibaar bu jib ginnaaw ba ñu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/10/2023)

LU BEES ÑEEL GÉNNÉEG USMAAN SONKO CI WAYNDAREW WOTE YI Ay fan ginnaaw bees jébbalee...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/10/2023)

PÓLITIG Aliw Tin yëy na yàbbi ci ni demokaraasi bi tëdde ci biir réew mi...

XIBAARI TAGGAT-YARAM (1/10/2023)

KUPPEG ÀDDINA WAY-LUU YI (MUUMA YI) Bàyyeesu leen xel, waaye way-luu (muuma) yi teewal Senegaal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/9/2023)

GÀMMU 2023 Tey, àllarba, yemoo ak ñaar fukki fan ak juróom-ñaar ci sàttumbaar (weeru tubaab),...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...